Back to Top

POTU NDA Video (MV)

DAARA J FAMILY - POTU NDA Lyrics

Adouna nila -yeah yeah!!
Adouna nila-yeah yeah!!
Pottu nda la kou naan jokh sa morom mou naan -yeah yeah!!

Allal gouné gagni -yeah yeah !!
Nga dém bayifi-yeah yeah!!
Njaboot ngay xeucoo sooraléwowoon yeah yeah!!
Allal gouné gagni-yeah yeah!!
Nga dém bayifi-yeah yeah!!
Njaboot ngay xeucoo
Foogéwokowoon.
HEY!! numéro douze gneuweul soobou
Lou way meuneu déf boppam dougnou meuneu bokk
Wayé borom andd bounék ak xambbam-moytoul sa bopp
Kouné am nga sagn sagn déf linga beug déf wayé bo doffoul dinga déf linga xam
Beuri ci domou adama gnidoul soor né biss digna gneuw kouné fay sa borr
Adina bofi nékké fok nga maasalook souf si balay souf si maasaloo
Adouna bateau dém bateau kosté
Kén doufi déss gneupay dém biss dé
Gno matta séedé gni déf lou baax
Koula meuneu déffal mola geun sarakh
Sofi nékké do tayi so démé dinga bayi
Njaboot allal séddalé gaayi gnouy cooké ka xeucoo
Ba jeul lépp jaayi-"ma moom li moom lé,yag yag fingakoy ba"
Pottou nda la boul jallou bo gouxé dinga maraat-han!!! kon souma bougé goob fok ma jii? xam nga
Ni moy sa wareef

Sa nafsou daan ko balamoulay jay-sa nafsou daan ko balamoulay jay
Doundal doundal dound téy ngay dée- doundal doundal dound tay ngay dée
Kila geuneu agg souf mola geun téy-kila geuneu agg souf mola geun téy
Sa nafsou-daanko-balamoulay-jay-sa nafsou-daanko-balamoulay-jay
Sa nafsou-daanko-balamoulay-jay-sa-nafsou-daanko-balamoulay-jay
Ndank ndank ndank ndank ndank ndank ndank ndank dél téy!!!

Parah parah parah parah parah ...pé!
Parah parah parah parah parah...pé!
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Mamadou SECK, Abdou SECK
Copyright: Lyrics © BMG Rights Management, CHRYSALIS MUSIC FRANCE

Tags:
No tags yet