Back to Top

DAARA J FAMILY - TEMPS BOY Lyrics

DAARA J FAMILY - TEMPS BOY Lyrics

REFRAIN

TIMISSOUL BAY GUOUDI YAW
FATTALLIKOUL TEMPS BOY
SO GUISSATOUL BAY TEGGUI YONN
FATTALIKOUL TEMPS BOY

COUPLET 1:ndongo
Temps boy teylama dab biss yi dima japp
Att yi geuneu gaaw ak lima daw ngir teela raw
Xel a daw fatteuliku douma fate yi baat
Fangeundiku geustu yoon nanga waaj
Yi baax yi jag yi bonn yi xatt madi gissaat
Moytandiku doon tricheur biir clase
Doon crack gaddu sac wacce kab daxi heure di stop P2 ba roppi sotrac
Laxu doon touxkattu bepp xeet cigarettes dinga seet jengu doon guerrier
Walla tapette lang sareet beureet wirri kogn daw doug biir market
Troto sinkkal powu xandal dawi geej cinema gettu beuy dofi leuj
Gnoune daawoko deuj nijaay di kass yaw danga repp yaw danga xeeb lesson yi nga lebb teuj la rek bado giss sakh ceeb dangay wanne danga matt
Danga jeum makk naala par 4,

COUPLET

GNOUN BAGNOU DE GONNE DEF NAGN LOUNE
LOOLAMBE ASSALOO ASSABOMBE SALSALATOO
BALBA DEMNA KAW BA LA MOU KOY LAAL SAMA YARAM DAWNA
ADINA AMOUL SOLO KHOOLAL FILA GNOU JAAR
NE CI JALU SOUFSI DI LAMBI GOLO
SEEK LEEK DAMAY TOOK DI SCIENCE BOOBOU TEMPS
AK NI MOU GAAWE CEEY ADOUNA
POTOU CAFE AK CAASS
BANT AK PONT AMNGA TOUQ SOU NGALAM
BANTOU BALE DIKO CI XALAM
TAMPON GUERRIER SA YARAM
TOPP NEEKHAYOU POMI
TERREUREURRI FATTE JANG SAY LECON
GNIBBI SI PAABI TEGGAL LA CI KARRAWAASS
AICA CI BIIR TEEWUMALA DOKH TIMISS
GUONE GUILE DEURKISS
DANGA BEUGUEU TARKHISS
BOO BAYYI WUL MBEDDMI DAACI MEUSSA AM BISS
GUI GONNEE WOW DEUGUEUC
TOOGAL NGA LEUC

TEMPS BOY TEMPS TEMPS BOY SOOKOY FATTALIKOU DANGAY DEM BA DOO AMATI LOO WAX LOUDOUL NDEYSAAN
SOY FATTALLIKOU NJALBEEN SOY FATTALIKOU NJALBEEN
SO KOY FATTALIKOU DANGAY DEM BA DEM BA DOO AMATI LOO WAX LOUDOUL NDEYSAAN NDEYSAAN
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Mamadou SECK, Abdou SECK
Copyright: Lyrics © BMG Rights Management, CHRYSALIS MUSIC FRANCE

DAARA J FAMILY - TEMPS BOY Video
(Show video at the top of the page)

Tags:
No tags yet