Back to Top

Diyane Adamas - Boul Xàddi [Original] Lyrics

Diyane Adamas - Boul Xàddi [Original] Lyrics
Official

Xëc nga ba sonnu dara ñëwul
Mais bumu tax ngay xàddi
Mòcc nga ba sonnu dara dikkul
Mai's bumu tax ngay sàlit
Dara xëyyul rek sòtti
Fileek neexul suñu Boròm
Dara xëyyul rek sòtti
Fileek Yalla àndu ci
Kone lileu war mooy , liggeey te baña ñaxtu
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
Waññi bò giss benn la doorè bala muy sori
Bul am looy tiit xòlal finga dòrè ngir mën ko neetali
Nanguleu jàar si buntu yu ndaw yi
Ngir mëneu geennè si yu mag yi
Ku defful dara yaw de dina jaffe nguir nga am dara
Ku ammul dara buldi merè ehh kuleu defful dara
Yalla Yalla bayal sa tòl yi
Nguir ñu mëneu nàat
Yaw lileu war mooy liggeey te baña ñaxtu
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Work Work Work Work Work
Work never lose your hope
Work Work Work Work Work
Work never lose your hope
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Xëc nga ba sonnu dara ñëwul
Mais bumu tax ngay xàddi
Mòcc nga ba sonnu dara dikkul
Mai's bumu tax ngay sàlit
Dara xëyyul rek sòtti
Fileek neexul suñu Boròm
Dara xëyyul rek sòtti
Fileek Yalla àndu ci
Kone lileu war mooy , liggeey te baña ñaxtu
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
Waññi bò giss benn la doorè bala muy sori
Bul am looy tiit xòlal finga dòrè ngir mën ko neetali
Nanguleu jàar si buntu yu ndaw yi
Ngir mëneu geennè si yu mag yi
Ku defful dara yaw de dina jaffe nguir nga am dara
Ku ammul dara buldi merè ehh kuleu defful dara
Yalla Yalla bayal sa tòl yi
Nguir ñu mëneu nàat
Yaw lileu war mooy liggeey te baña ñaxtu
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Work Work Work Work Work
Work never lose your hope
Work Work Work Work Work
Work never lose your hope
Yaw lileu war mooy gaur gaurlou te sabablu
Wowu wow wow wooy
Sò am mul bul ci mere kenn
Wowu wow wow wooy
Juggël fight ngir mën ci genn
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Adama Ndiaye
Copyright: Lyrics © Y3LH

Back to: Diyane Adamas

Diyane Adamas - Boul Xàddi [Original] Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Diyane Adamas
Language: English
Length: 3:20
Written by: Adama Ndiaye
[Correct Info]
Tags:
No tags yet