Wakhin deeggin la laadj
Jëffin mënnin la laadj
BuL deegg tèll rek ni dee na te xamo numu demè
Wakhin deeggin la laadj
Jëfin mënnin la laadj
BuL deegg tèll rek ni dee na te xamo numu demè
Lou nit ñi wakh ngani xam naako
Lou nit ñi def ngani meun naako
Fou nit ñi dem nga ni dem naafa
Kou nit ñi wax ngani xam naako
Ragalal Yalla , (Badou Meun lepp Badou)
Ragalal Yalla (Badou Meun lepp Badou)
(Badou Meun Lepp , Badou , Badou Meun Leepp) Ragalal Yalla
Aduna bii be boofi neekè
Jeemeul leu moytou louleuy tardeel
Woowuwoww
Liggeey len Liggeey len Liggeey len
Baayi nakhaaté bi
Liggey len Liggey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Liggey len Liggey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Liggey len Liggey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Li ngay wax ni mom nga
Xam ngani neekku looci dara
Di jeemeu nax nit ñi
Nguir meuneu leekk seeni alal
Li ngay def nii daflay tardeel
Té daflay tooppi ba sa biiru baameel
Suñu njiittu reew mi
Màngi leen di ñàan nguir
Ngeen dimbeulil ñu
Suñu ndawu reew mi
Nguir ñu meuneu ammi xeuy
Suñko amè dootu ñu neekk si mbeed mè eehhhh
Liggeey len Liggeey len Liggeey len
Baayi nakhaaté bi
Liggeey len Liggeey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Liggeey len Liggeey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Liggeey len Liggeey len Liggey len
Baayi nakhaaté bi
Badou Meun Lepp , Badou , Badou Meun Leepp