Mày sa security kenn duleu laal
Kuleu bëgg jot si mane lay jàar
I'm your protector nobody will touch you as long as I'm alive
Mày kileuy saamm kenn duleu jegge fileek màngi dundu
Ñàta yoon lañ kofi giss si ñàar ñu bëggeunte am ñu si juk jaxasse leen
Ñàta yoon lañ kofi giss si ñaar ñu bëggeunte am ñu si juk tàggale leen
Ku bëggul coow nama bàyyeek yaw
Fii am na kufi neekk soxla wuñu laneen
Bakken jàmm leu bëgg dumeu mêsseu baayyi
Mane dumeu taayyi fileek demuleen
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Cuz I know oooowww
Li wax ji bërei bërri liñu bëgg mooy ma pouss
Ñu mën ñeuw
Girl kaay ñu dem, kaay ñu dem
Kaay ñu dem faneen
Kaay ñu dem , kaay ñu dem
Seeti ji laneen
Xam nà luñ lay tooppè
Du ay waxxi sooppè
Dañ nuy jeem jaxasse
Mais dumaci mësseu baayyi keen
Mais dumaci mësseu baayyi keen girl
Mais dumaci mësseu baayyi keen
Mais dumaci mësseu baayyi keen girl
Bu soobbè Yalla dinañ la baayyi
Bu soobbè Yalla dinañ nu baayyi
Maak yaw de pique ak pèle la
Maak yaw de pique ak pèle la
Ku bëggul coow nama bàyyeek yaw
Fii am na kufi neekk soxla wuñu laneen
Bakken jàmm leu bëgg dumeu mêsseu baayyi
Mane dumeu taayyi fileek demuleen
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Cuz I know ooowww
Li wax ji bërei bërri liñu bëgg mooy ma pouss
Ñu mën ñeuw
I'm your protector nobody will touch you as long as I'm alive
Mày kileuy saamm kenn duleu jegge fileek màngi dundu
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Girl miine naa leepp kenn duleu jegge
Girl I won't let kenn dileu tagge
Cuz I know ooowww
Li wax ji bërei bërri liñu bëgg mooy ma pouss
Ñu mën ñeuw
(mooy ma pouss ñu mënn ñëw
Ohh baby I won't let them be with you
Cuz you're my life)