Back to Top

Diyane Adams - Li Ci Nit [Original] Lyrics



Diyane Adams - Li Ci Nit [Original] Lyrics
Official




Su mbekté amè ñooy nekk ci sa wet
Su nakkar amè yaw rek ya ciy weet
Su xeeweul amè niou biiw leu ni weñ
Sou dara amul ñoom ñëpp xeuy dem
Yaw seetaa tal bou baakh say deukeundo
Yaw xoolaat tal bou baakh say andadoo
Ndakh nit ñi duniou been
Jikko Yi duñou benn
Geum Geum Yi duñou beeneu
BuL Fook ni ni nga mel la nëpp mel
BuL Fook ni li ngay def la nëpp di def
Ohh no no no no no It is not the case oh wow
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndakh meuno jokh nëpp ndimbeul oh oh oh wow
Yaw Dara jaratul ngay tookk fii di jooy
Leeggi xam nga leen jotna naq nga nooyyi
Yeené wòleen nakkar sa xol dafciy tooy
Sa jaamak wergui yaram na doon lilay doy
Yaw seetaat tal bou baax say deukeundo
Yaw xoolaatal bou baakh say andado
Ndakh nit ñi duñou benn
Jiko Yi duñou benn
Geum Geum Yi duniou beeneu (oh yeah)
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndax meuno jokh nieupp ndimbeul oh wow
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndax meuno jokh nieupp ndimbeul oh wow
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


Wolof

Su mbekté amè ñooy nekk ci sa wet
Su nakkar amè yaw rek ya ciy weet
Su xeeweul amè niou biiw leu ni weñ
Sou dara amul ñoom ñëpp xeuy dem
Yaw seetaa tal bou baakh say deukeundo
Yaw xoolaat tal bou baakh say andadoo
Ndakh nit ñi duniou been
Jikko Yi duñou benn
Geum Geum Yi duñou beeneu
BuL Fook ni ni nga mel la nëpp mel
BuL Fook ni li ngay def la nëpp di def
Ohh no no no no no It is not the case oh wow
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndakh meuno jokh nëpp ndimbeul oh oh oh wow
Yaw Dara jaratul ngay tookk fii di jooy
Leeggi xam nga leen jotna naq nga nooyyi
Yeené wòleen nakkar sa xol dafciy tooy
Sa jaamak wergui yaram na doon lilay doy
Yaw seetaat tal bou baax say deukeundo
Yaw xoolaatal bou baakh say andado
Ndakh nit ñi duñou benn
Jiko Yi duñou benn
Geum Geum Yi duniou beeneu (oh yeah)
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndax meuno jokh nieupp ndimbeul oh wow
Li ci nit da beuri li ci nit da beuri
Li ci nit da beuri li ci nit daa
Nala sa boopp geuneul
Ndax meuno jokh nieupp ndimbeul oh wow
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Adama Ndiaye
Copyright: Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Back to: Diyane Adams



Diyane Adams - Li Ci Nit [Original] Video
(Show video at the top of the page)


Performed By: Diyane Adams
Language: Wolof
Length: 3:20
Written by: Adama Ndiaye
[Correct Info]
Tags:
No tags yet