Back to Top

fadel faty - Gindi Lyrics

fadel faty - Gindi Lyrics

Wallahii Sant nalla yalla bour
Ndah faté woma béne yone cii sa ngour guiii
Ap diam la rèk beurii soussi
May tallal dila gnian ngamay gindi
Allahou ak bar yalla mague na
Moy tar mo diara yakar dii gniane nga gindi ma

Sant sant Sant nalla bour bii magal rabii
Dioh ngama catan dollé hélak mene mene yarabiii

Mane may togne.... Mane may toup
Gniake hame....tahh may faték dioum

Nite kou nék sa bopou doynala sohla
Lingay defff ba retie warr nalla sohal

Péhè diam... diar na tite
Retiou name mene na fék dieuf déss tiss

Nite kou nék sa bopou doynala sohla
Ningay defff ba retie war nalla sohal

Réfrin
Heee!! Ragal day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy
Hee hee mbah day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy

Ligniouy gene dème Mbah dii gene diéhhhh
Djiko yii sopékou Gniepa gniémè dérét
Nite ak nite doundou Vampire
Lékanté sounou birr gniepa hiff
Mbah mo diéhhhh!! Way
Walla mbone da gene yombou
Yii bahh da gene chair
Yii Bone ehhh!!!
Boula dara sopii ndah dereum dou wérou wayy
Lii
Yalla diara sopou ndah kereum ndioukélou kay la
Boko geumé wollou ko gniak dou géné fayy yii

Hollay faye lii hélll dii ligey bo bagnia tayii E

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Wallahii Sant nalla yalla bour
Ndah faté woma béne yone cii sa ngour guiii
Ap diam la rèk beurii soussi
May tallal dila gnian ngamay gindi
Allahou ak bar yalla mague na
Moy tar mo diara yakar dii gniane nga gindi ma

Sant sant Sant nalla bour bii magal rabii
Dioh ngama catan dollé hélak mene mene yarabiii

Mane may togne.... Mane may toup
Gniake hame....tahh may faték dioum

Nite kou nék sa bopou doynala sohla
Lingay defff ba retie warr nalla sohal

Péhè diam... diar na tite
Retiou name mene na fék dieuf déss tiss

Nite kou nék sa bopou doynala sohla
Ningay defff ba retie war nalla sohal

Réfrin
Heee!! Ragal day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy
Hee hee mbah day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy

Ligniouy gene dème Mbah dii gene diéhhhh
Djiko yii sopékou Gniepa gniémè dérét
Nite ak nite doundou Vampire
Lékanté sounou birr gniepa hiff
Mbah mo diéhhhh!! Way
Walla mbone da gene yombou
Yii bahh da gene chair
Yii Bone ehhh!!!
Boula dara sopii ndah dereum dou wérou wayy
Lii
Yalla diara sopou ndah kereum ndioukélou kay la
Boko geumé wollou ko gniak dou géné fayy yii

Hollay faye lii hélll dii ligey bo bagnia tayii E
Mane may togne.... Mane may toup
Gniake hame....tahh may faték dioum

Nite kou nék sa bopou doynala sohla
Lingay defff ba retie warr nalla sohal

Réfrin
Heee!! Ragal day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy
Hee hee mbah day gindi boy
Hee! Hee! Dounè ko diam bii moulay gindi boy
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: fadel faty

fadel faty - Gindi Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: fadel faty
Language: English
Length: 3:00
Written by: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
[Correct Info]
Tags:
No tags yet