Back to Top

fadel faty - Gëm Gëm Lyrics

fadel faty - Gëm Gëm Lyrics

Dègn ma yare cii diom
Nèma woutil ham ham
Bagnia tala loho ragal koula tingom
Boy yot lii nit ki ame
Outal nit ki ame, woloul sa morom boul sohor bess nga woufe dome
Bess yalla wone ma cii yone ay dieuf moy tonetou
Dèff na ma mage dioh nama dome Bayina fonetou
Geme nani diar diar rèk mene dèfar Gor
Diambar dou daw rare mètit yepou lay diamar lol
Boum mètii banga hadi sa yone louma sori sori
Sa yone limou sori wadji yako wara doh
Fii koula dèfal wone la yone binga wara aw
Sa yone limou sori wadjii yako wara doh

Ragalouma sik tah mou gena tarou sa none bouko sikal dalay dèfar bahhh na

Réfrin
Mbeguel dalay wone yone bii

Geme Geme dalay wone yone!!!!!! Bii

Mbeguel dalay wone yone bii yone bii
Finga wara aww!!

Adouna douma tèré dèff
Wollou na fima begue dieum
Yakar na lima diota dèff
Garanti limay done souba

Wax djii fadioul dara fok nga tame dieuf
Hèhh bii yak sa bopou la
Lingay dièm cii ndaw molay dèff eleuk
Hèhh bii yak sa bopou la

Dieugèl cii Hirok ngâyo Lingay begue done
Hèh bii dèff ko tay bouko dèf souba

Donal sa hiro diafèl Lingay begue done
Hèh dèff ko tay bouko dèff souba

Adouna bii nèhoul
Tame talal loho dalay dèff kou hèbou

Dieugeul tèle bidantiiii
Yakar dina doundal diame boko hèboul

Ko hamoul limou doundou wara mene mandou
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Dègn ma yare cii diom
Nèma woutil ham ham
Bagnia tala loho ragal koula tingom
Boy yot lii nit ki ame
Outal nit ki ame, woloul sa morom boul sohor bess nga woufe dome
Bess yalla wone ma cii yone ay dieuf moy tonetou
Dèff na ma mage dioh nama dome Bayina fonetou
Geme nani diar diar rèk mene dèfar Gor
Diambar dou daw rare mètit yepou lay diamar lol
Boum mètii banga hadi sa yone louma sori sori
Sa yone limou sori wadji yako wara doh
Fii koula dèfal wone la yone binga wara aw
Sa yone limou sori wadjii yako wara doh

Ragalouma sik tah mou gena tarou sa none bouko sikal dalay dèfar bahhh na

Réfrin
Mbeguel dalay wone yone bii

Geme Geme dalay wone yone!!!!!! Bii

Mbeguel dalay wone yone bii yone bii
Finga wara aww!!

Adouna douma tèré dèff
Wollou na fima begue dieum
Yakar na lima diota dèff
Garanti limay done souba

Wax djii fadioul dara fok nga tame dieuf
Hèhh bii yak sa bopou la
Lingay dièm cii ndaw molay dèff eleuk
Hèhh bii yak sa bopou la

Dieugèl cii Hirok ngâyo Lingay begue done
Hèh bii dèff ko tay bouko dèf souba

Donal sa hiro diafèl Lingay begue done
Hèh dèff ko tay bouko dèff souba

Adouna bii nèhoul
Tame talal loho dalay dèff kou hèbou

Dieugeul tèle bidantiiii
Yakar dina doundal diame boko hèboul

Ko hamoul limou doundou wara mene mandou
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: fadel faty

fadel faty - Gëm Gëm Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: fadel faty
Language: English
Length: 2:34
Written by: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
[Correct Info]
Tags:
No tags yet