Back to Top

fadel faty - Goungué Lyrics



fadel faty - Goungué Lyrics




Mbeguel moma dap dima Goungè yow
Yakar la Goungè yow salaw dou ay fo
Mbeguèl moma dap dima gindi
Yakar la gindi yow salaw dou ay foo
Wètio
Wètio doumala wètiok
Nagni tiow
Nagni tiow gniou doundou mak yow

Bb Dieugè cii ma
Ragal douko dèff layik
Mene nga cii mane

Mene cii mane
Ay mbhalou mbarii sahh
Yenge louma

Boula gniepou bawè mangii sa wet
Wax dji na beurii mala tipo

Mbeguèl dou tiahane dèye fègn cii bete
Wax dji na beurii mala tipo

Réfrin
Mbeguel moma dap dima Goungè yow
Yakar la Goungè yow salaw dou ay fo
Mbeguèl moma dap dima gindi
Yakar la gindi yow salaw dou ay foo
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


English

Mbeguel moma dap dima Goungè yow
Yakar la Goungè yow salaw dou ay fo
Mbeguèl moma dap dima gindi
Yakar la gindi yow salaw dou ay foo
Wètio
Wètio doumala wètiok
Nagni tiow
Nagni tiow gniou doundou mak yow

Bb Dieugè cii ma
Ragal douko dèff layik
Mene nga cii mane

Mene cii mane
Ay mbhalou mbarii sahh
Yenge louma

Boula gniepou bawè mangii sa wet
Wax dji na beurii mala tipo

Mbeguèl dou tiahane dèye fègn cii bete
Wax dji na beurii mala tipo

Réfrin
Mbeguel moma dap dima Goungè yow
Yakar la Goungè yow salaw dou ay fo
Mbeguèl moma dap dima gindi
Yakar la gindi yow salaw dou ay foo
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: fadel faty



fadel faty - Goungué Video
(Show video at the top of the page)


Performed By: fadel faty
Language: English
Length: 3:00
Written by: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
[Correct Info]
Tags:
No tags yet