Back to Top

fadel faty - Sénégalére Lyrics

fadel faty - Sénégalére Lyrics

Mane la senegalais
Senegalais lamda bingay rombe founé
Té boul ma sét Mangii fepou
Mane nga bap bama fall la nga defff Ma tiouné
Wor ma faté ma nèk ci sa yefou bopou
Faté bagn lay sanii Herr mako enkécé
Tay ya nèk cii Palais ma nék fii gniak dii réy
Gniak gene pénè halat souba douté
Romb niou cii mbed mii ték thianyin gniakoum liguey.Haan!
Diombou satie werr dii talal loho
Begue liguey amouniou founé niou dekeul nioufa
Sounou insperence de vie raw bou youssoupha
Ligniouy datie cii hallé réy na killifa
Neve
Neve dougniou bayii sounou saba
Likoy tabah hadii bokou cii walla ndiouma
Gniak ame ame dou gniak diom
Dégniouy yakar ko cii kéne yalla bour la

Ma Senegal Senegalais lamda bingay rombou foune tè boul set mangii fep
Mane nga bap bama fale la
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Mane la senegalais
Senegalais lamda bingay rombe founé
Té boul ma sét Mangii fepou
Mane nga bap bama fall la nga defff Ma tiouné
Wor ma faté ma nèk ci sa yefou bopou
Faté bagn lay sanii Herr mako enkécé
Tay ya nèk cii Palais ma nék fii gniak dii réy
Gniak gene pénè halat souba douté
Romb niou cii mbed mii ték thianyin gniakoum liguey.Haan!
Diombou satie werr dii talal loho
Begue liguey amouniou founé niou dekeul nioufa
Sounou insperence de vie raw bou youssoupha
Ligniouy datie cii hallé réy na killifa
Neve
Neve dougniou bayii sounou saba
Likoy tabah hadii bokou cii walla ndiouma
Gniak ame ame dou gniak diom
Dégniouy yakar ko cii kéne yalla bour la

Ma Senegal Senegalais lamda bingay rombou foune tè boul set mangii fep
Mane nga bap bama fale la
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: fadel faty

fadel faty - Sénégalére Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: fadel faty
Language: English
Length: 2:33
Written by: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
[Correct Info]
Tags:
No tags yet