Back to Top

Gun Mor - Bois Caïman Lyrics

Gun Mor - Bois Caïman Lyrics

Amoul nelaw kene douffi teude
Fadjar laniou wara dox dem djeulii geude
(Tonight)
Nagn guéné tama yeup ték gueweul yi teug
Mbeur yi weur tal bi fecc feug seni deune
(Tonight)
Indilene djour yi teureul rendi fess lakeu
Khiff dou mbokk nioune nieupeu bokk na nieup lekk
(Tonight)
Lepafi ame na kouné dieul loum Beugue nane
Mais apart mateu yiniouy xamb kene warouta takeu
(Tonight)
Veiller bi dou pour noce dagnouy wara xaré
Wara dianok gnîniou not ba noppi wara gagné
(Tonight)
Danio beug wér beugeutougnou tané
Bingene gnou akissé balegui nioune si laniou febar

(We never sleep cause sleep is the cousin of death
Tok di xol gnougni teudjeu que tidji dotougn ko def...
We never sleep cause sleep is the cousin of death
Tok di xol gnougni raye dotougn ko def yawwww)

Amoul nelaw tonight
Demain c'est la révolution wowouwooo
Amoul nelaw tonight

Amoul nelaw tonight
Demain c'est la révolution wowouwooo
Amoul nelaw tonight

Heureuma diot gni teudone na nieup diog
I have a dream dougn ko fi xaar lign wara defay ...
(Revolution)
Kepp kouniou nott bagua niak sa batt
Dou weur di joy yakoy fadj limalay digeulay
(Revolution)
Comme Souleyman Baal sa doley ak sa xam xam boko niogalé dou kene koula meune té def.....
(Revolution)
Armez-vous de sciences jusqu'à la moelle
Comme disait le pharaon des pharaons c'est ça la
(Revolution)
The revolution will not be televised
Nagn lene tidji sounouy télé wanessi sounouy
(Revolution)
Xex ba ame ndam bind tarikh bi dégntieu
Bayil ko sunuy dome ak sounouy seut lolou moy revolution

Amoul nelaw tonighty
Tok di taxirlou nadj bi
Mboloy dolé kone nieup nieuw niou def unité
Bou tangué niom la nioy tit
Wané yone bi nioy guide
Bepp xam xam boumsi meunti done nio meusseu done djitt
Amoul nelaw

Yaw Africa united
Africa united
Africa yooooooo hehehehe
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Writer: Mouhamed Loucar, Momar Ndiaye
Copyright: Lyrics © Sony/ATV Music Publishing LLC

Back to: Gun Mor

Gun Mor - Bois Caïman Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Gun Mor
Language: English
Length: 3:21
Written by: Mouhamed Loucar, Momar Ndiaye
[Correct Info]
Tags:
No tags yet