Back to Top

Gun Mor - Complex [Original] Lyrics

Gun Mor - Complex [Original] Lyrics
Official

Yeah yeah
Yes yes yo
Han
Sama rapa complexe
(Sama rapa complexe)
Mais mane awma complexe
(Mais mane awma complexe)
Xolma dama complet
(Xolma dama complet)
Niata style comptel
(Niata style comptel)
Han hey yow
Sama rapa complexe (han)
Mais mane awma complexe (han)
Xolma dama complet (han)
Niata style comptel
Mane ak yene dou compet (wou)
Tegoulene Lou concret
Dama né si conquête (han)
Sene xel yi laye conquérir
Fouguene ma guiss sene fiit yi teug type beat Jersey
Douma done ki leni diaxal that's what they said
Douma bandit bandit Lou rek Cons yi tegg ma noy boy
Fou sama Niakeu tokkeu bo deme fekeu fa toy toy
Defouma li dox tééé limay def moguimay Faye
Sama première souffle guénoul Dara dou doye taye
Watagouwan Galsen
Do you know the black man
Better known as Gun Mor ki dafma yeme man
Tabax na ba carrelé mane damané di peinture
Gnoma dakeu rap ils l'ont avoué à mon insu
J'ai tuer là bête c'est ça peau qui me sert de vêtements
Évènement doma guiss après laye géneu tegg événements
Beureung sama beurigo rek tope si di daw
Nique les codes sole sama veste tegg copatiii si kaw
Memoirou mbed sama first crew daye meusseu law ba faw
Dagno dofone di rap legui tatounene lagni déf di daw
Yeurmandé mong si armel
Mane magui ni né si war wiiii
Suis un homme averti antagoniste de Wally
Maintenant le monde est à moi douma mayé hémisphère
Suis pas le bouc émissaire je suis le bouc et ses mystères
Sama rapa complexe
(Sama rapa complexe)
Mais mane awma complexe
(Non mane awma complexe)
Xolma dama complet
(Xolma dama complet)
Niata style comptel
Mane ak yene dou compet
Ladies love Cool Mor
Niggaz hates Cool Mor
(Nonnnnn)
They don't hate me they just pretend
Ndax beugue dou bagne
Walabokkk Deug dou dagne
Sometimes damay naxaté doucement laye deflou tingue
Tal sa (ohhh) soûl sa (ohhh)
Nane sa (ohhh) rouy sa (ohhh)
Dieul sa (ohhh) def la (ohhh)
Tek la (ohhh) rek nga (ohhh)
Niggah xana Dagua doff
Xamoni mala geuneu dofff
Mane Fimay degnth samay balou gun moy sama bopp oppss
Raye la xam ni militaire
Woté guerre bouy indi paix
Infirmier bouy xoliii plaît
Tioute sa baye seringue mou père
Demal si gni niodi wagua
Nelene sama galle dou terrr
Après gué Kouma dougou sa keur kene dou tadj bolou rerr
Ehhh yoooo youxoul sama tour melni kou matt keppeu
Bouguene beugué ma bayi meune rap niane lene ko si ndiekeu
God Mc Nama sene lyricists yi soudiotal
Artisan du vers mane xel yi la né di xoteul
Di yatal (di yatal)
Di tawiii (di tawi)
Souma djappé (non)
Douma bayi (jamais jamais)
Mane dong groupe la
Makk sama boppay sama gayi
Moussoumafi ame morom waxnalene ko ba tayi
Sama rapa complexe
(Sama rapa complexe)
Mais mane awma complexe
(Mais mane awma complexe)
Xolma dama complet
(Xolma dama pletcom)
Niata style comptel (what)
Han hey yow
Sama rapa complexe (han)
Mais mane awma complexe (nan)
Xolma dama complet (yeah)
Niata style comptel (han)
Mane ak yene dou compet (non non)
Tegoulene Lou concret (jamais)
Dama né si conquête (wouh)
Sene xel yi laye conquérir
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Momar Ndiaye
Copyright: Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Back to: Gun Mor

Gun Mor - Complex [Original] Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Gun Mor
Length: 2:58
Written by: Momar Ndiaye
[Correct Info]
Tags:
No tags yet