Back to Top

Complex (Remix) [Remix] Video (MV)

Performed By: Gun Mor
Language: Wolof
Length: 8:02
Written by: Momar Ndiaye
[Correct Info]

Gun Mor - Complex (Remix) [Remix] Lyrics
Official

Yeah yeah
Han han
Yaaaaw
Souniou rapa complex (Souniou rapa complex)
Mais amouniou complex (Mais amouniou complex)
Xol niou daniou complet (Xol niou daniou complet)
Niata style comptel (Niata style comptel)
Hey yow
Souniou rapa complex
Mais amouniou complex
Xol niou daniou complet
Niata style comptel
Nioune ak yeen dou compet
Teggu lene lou concret
Dañu né si conquête
Sen xeel yi lañ conquérir
Yow degglou S mouno si sonou comme compter xaliss xorbett
Porte bonheur si sén game je symbolise l'hirondelle
Tegglé diouni flow dou diaffé niou diott si sommet
Nenga yaffi daak rap ya ngui xeutio sama momel (Haaaa)
You snooze you loose dalo si touss di proud
F*ck millions de vues sén game si sama tioutiou
Drapeau bi dou moss tioubou
Xamo si lingayy douggou
Sam face you do it tout doux
Sén rap question de vue leu
Sam rap leçon de vie leu
I'm born pour nek leader
Call me the flow (haaaah)
Call me the flow digger deffougne louy flow (hah)
Baisé game bi diapp siteul ngayy dékkou ni tottt
Yaw han
I'm not a human bieng niggaz i'm an artist
I mad da zik u wan to hear 4da cultur practice
Noga so wër HipHop soma rombé foksa art'rist
Yeqq si nga kmup dokko guiss mouk lu basic
Du PRA Made in bokuñoq ñi amul RFRNCE
Kmup si kaw ñom ñëp sisuf ndax amuñ DFRNC
Liné si man nkul si ñom liné si ñom nkul si man
Bu desé ludul xatim aï ryme fente aï way
Oh damn mala gueuneu doff
Médiocre lañu Promote defli dox woweko feelin
Pour guis ku mën men fok nga wañi juni so lime
Misalal sa carrière ni Yow tatiou laay ray
Su biram donné king daffek kmup combine
Russ na sekak ioe détails xalate door laï pikk
Soma batt si suff so out biff awra jigen day dik yeah

Ñun ak yen dou compet
Am ñan Gang bouy teudj sa gate
Kou diog si yen togate
Flow bou tog si rausol
Black bou ouf thiaga
Amou niou place si biir sabar
Kou guéneu sii yèn dou gate
Kou ladjé si yén Keumeufeu
Nélén ko weuy ça va
Okey
Ma Caissé Sén deune yi comme soutient gorge
Corde sisa coup serré bâte bi melni symbole
Touché samay baram di commander com kou simple yeah
Diokhogn sama baram commande di guén di dèndal
(Tu tu)
Ko niouy clamer
Nio ngui
Si bénén planète et puis
Rap mo niou geuna Izy louñu lén di amél
O Shit
Préjugés ay sound melni simpson
Tim réw mi ak dolé yoré trace place king kong
Mais Douma débat
Lamégn bou Ndaw si Sama pout
Mais douma wane bate
Projet ya ngui té rechuté
Keumeufeu di rede chéque
Mc yi di redouté
Canibal reube chair
Hennesy ak yeuré Gucci
Parfum ak yeuré bou chère
Diow dou jipp boy reub khékhh
Fi ngay nieuw boy reub tête
(Fi ngay nieuw boy reub tête)

Niounela nieup done xaar
We the greatest of all time
Fallait que leundeum bi nieuw fenial fi bidew for longtime
Yaw ak seu cercle
Dolene doug sounie carré vip
Tioki bi parel ci yaw leu dess faut que niou xaré fils
Yes
Xamoulo sa bopp mais xamnganiou bou bax
Danguene ko yor demoul niou diox niou bayil niou waslou akh
Mindef bou am ligeyou ndey si mom meme tiat dou gaw
So joulé fadiar del niane niou banie meuss sek takussan
Damn
Teuf
Lassa fitt bi def ndax ling niou seeene
Deretou gor moy daw si souniou veine
F*ck
Bip bip
Gauche ak droite di feinter coup
Li moy leundeumitude
Mais dounieleu wane lou dendak flou
Faut que lou xonk tiss
Virgule dounieko bayi ci bepeu ponk fils
Boul fontou fils
We'll be the gods its a profecy
Gueune leneu fonk cab
Kanie ngadone xamni may tonton ci rap galsen souma dioudo wone deukou oncle sam
(We back bro)
Dieuleuti concu bi def souniou gobelet
El Chapo sax dey xar sou sujet biy sopikou dopelé
Im like rambo
Dingko reutiou boma songué
C drole pride bilay animer malgré li sey son gay
Di gueune wolou sama bopp kou nieuw namaci feeeeek
Xol sama toph yeuk naa nimla mité
Yena sol sama stock bi batay moudj neu fesss
Samp na samay tank tokci f*ck say xarit you bess
Fi comme sabar bou tass kou jouk rek def ci son bongok tama
Ci Boy keumeuf mbed ci tete leu dou comportement
Gang bi dou tromperie
Kou get ni boy yi nioy connard
Danie newone di fo c aujourdhui que la saga commence
Yeah
Kouné meunone neu nek boy alone
We the Avengers
Fek niou si ring bi do raw ay coup
Beugouniou bok ci gni doyalone
Motax togouniou rek di xaar bay beug dé di dora wekou
(Dora wekou)
Haha
Diexagoul deh let's go
Keulthieu han han yeah
Sarax ci bir flow ak ben e King
Tei kholal meuno stand by me
You better know I'm the Keulthieu
Tell what you think about me
Nah Teng ba gui For the culture rebellion
KMF again pour change mind ni
That's why I'm flex
Chill zero complex
Ghetto hero I'm outside
For chasing money no sexe
Don't test
Douci diouk Tigui beat yi ni Gonzess
Walk alone, work stay humble
Nah ken si sey bitches meussoufi talkless
Don't stress
Yess you know we bless
We Bornblack kheule ci kilomètre
Def Kom yen dey khawa perplexe
Même si chez nous c'est pas le contexte
Dougn bolei yaye soy woté aye
Liley kharr percal leuh dou compress
Kon wakhma rek kouley fall
Koula tall
Fi kiss doula dale
Peace doko am
Tiss dinko kham
Bitch DomrAm
Maguek as kane
Askanou vibes
Katane ak tane
Xamo may kane
Bakane lassi tek
Tewal Sunu makane
Yotou tahul gua meune diot
Boudé tokk gua def sa time
Do Kawè ba sout Sa diort
Ak lou feus fesse Sa mind
Dess neuh gayn
Mayma someee ma shoot shoot
Deff fi crime
We different line dougnko tioup thioup
Never mind

Ñun ak yen dou compet'
No du compèt
Boul faté ya namp dioxma ma namp
Dagn fatewon hibla gaime bi kmf la sampou
Sol dieumou rab Di doh con yonla byi sankou
Lep Louam heutio seutou baye falli yi bokou def ci nak
Anhan defal niou def
Fi Lofi soor dou meusseu dess
My pcadet bilay diomal boma geumoul welcome to death
Yekcil goné lay Pesse
Dis nehouma testé
Liga tok ay at si sa projet matouma dessert
Yaw Daw ci sa mind boy né melodi ci intrus
Mc zi yo lay doundé Hana guilo dama ventrue
Mor balagay peinture bayil ma niaf ci enduit
C moi l password fi douma nagu bayi intrus
Im lass, the last dou man ak gnima massel
Jiouni volte si son yi ma haroul niounan ma masel
Li dutouss mosla coz dama universel
Niveau c i dou master boulma hard pti commencel
Commencel diang idji man wessouna sa térè
Lajal pa bidon har réponse dafma lok moujiou ceree
Ci bir terrain soumla passoul menoko récupérer
Révélée révélation du yeuglou melni kou teulé
Hana do hol fi Dara neubwul leep pa né Fang
Tella dal ci ay brik té watieoul sama diane
Pask damay dem Di geun hif
Gourmand lou nieuw damay bif
Tank pa mougi def loxom ci gallé khalatoumay gif
You know
Beuri fit Complxé noo
Ci mineur yiga may set doma fa guis magui senior
You know
QBoul meusseu fok boyla bu daw
Man awma ben pol j'occupe le sud et le nord
Power to the kmf mounouñu geuneuh stylé
Souñiy cama complex ndah bou bah bi lagni dealer
Moin ngua ñu ndieukeu guèneu mais bouniou guènè dañu lay planè ñuneu leuh f*cking carte d'identité yaw la f*cking récépissé
Keur mbay fall la deuk mais mbay fall momoul sama keurou papeu
Sama fiteu reuy ba raw bou mole motah maléni napp
Hamo Limay wah demal ngua togueu mane poésie lamay lakeu
F*ck sa label mangui All vibe tongue Di noss
Sa sho bi anytime day ecarté pour mane ma thions
Dèm ba ba yègue lay deer diaroul sahh NGA nane ma fonce
Sa son bou cartonner tchi birrou xaar yi leu dieum
Im a monotheist rap dou limay gueum
Nigga's call me RN lekke lekkakatou deum
Mouno Fi nék king clashantèl AK OMG bou fèkè beugu NGA nèk reine
Apart souma lay may loho waroma diapall haine
Atou nañu ko deudieul mako wah dou meusseu feiññe
Seneu niveau dafa soufè fok ma wathiè sama boop Moune lèneu Ray comme Gorge Floyd
Wonalèneu si thiow té do guisss kèneu kouma flow fils
Hum rap ngua 90ans amo vélo (bycicle)
Dañu Koy deff bamou nice douñu la may lo wah baysikeul
Fils demal NGA togue ñuneu sa bay lañu ko sékeul
Roppi nane la bye bye
Diay djiko say say
Sa guis guis geneuh gat sahh djiné coco l'ay lay
Yaw la mister feurtifeut danguay rap Di Youhou
Ñuneu déh défnañu bruit fépp
Te pourtant ont rap Tou Doux
Douñu sarahou kèneu dèm douce moñnouy bolé AK soukou
You tell you better than me no you make Arrache moving I don't watch nobody bro I live my f*cking movie
Yhè get out of my face
Get out of my face
Or it gonna be the last thing you gonna see nigger I swear I'm not playing
Suck my dick
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Wolof

Writer: Momar Ndiaye
Copyright: Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Back to: Gun Mor

Tags:
No tags yet