Back to Top

Def 4 [Original] Video (MV)




Performed By: Gun Mor
Length: 2:58
Written by: Momar Ndiaye
[Correct Info]



Gun Mor - Def 4 [Original] Lyrics
Official




Def Kate bou magg kaye niou defanté
Gueneul fi nieuw niou defanté
Dealer kaye niou teganté
Do wax Deug Kaye niou fenanté
Charlatan Kaye niou naxanté
Dagua beuri wax Kaye weranté
Boucher nga Kaye niou daganté
Sou deugeuré rej niou goranté
Menuisièr Kaye niou dadjanté
Rap bi day ladj niou rabonté
Guewel nga Kaye niou taganté
Mais mane vrai histoire bi laye raconter
Commerçant kaye niou diayanté
Business leu amoul mayanté
Maçon Kaye niou tabaxanté gazer souf ak ciment di raxanté
Loma def lalaye delo
Liguama diox lalate delo
Ligua mom lalaye delo
Limala lebb lalay delo
Kone doma desse Dara lepp ngamay delo
Limala diox ngamay delo
Lima mom ngamay delo
Liguama lebb ngamay delo for real
Iow dagua tangue Kone Kaye niou lakanté
On fait du sale kaye niou saguanté
Insolent kaye niou saguanté
Dangma beug mourro kone laye niou sanganté
Dagua rew dama neup kaye niou yaranté
Do togn di diegalou kone dougn balanté
Leboula amnga fiit Kaye niou napantè
Tepiii sa ouy après tafanté
Li djaral Nama lepp lim la diaral
(Li djaral Nama lepp lim la diaral)
Lima def ligua def moko waral
(Lima def ligua def moko waral)
Kou toudoul yalla la meunteu ragal
(Kou toudoul God la meunteu ragal)
Ligua yorr maguek mom Niggah dalal
War fassou narou goor diko dawal
Kone soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Anhhhh
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Boloy dolé nagn dieguenté
Give me your hand té bagne hainaté
Xamb tal bi mou geuneu takeu ndax nioune sougn birr nio meune faayanté
Damla nex kaye nga waxmako
Niou togg waxtane geune meune xamanté
Aye Borom bax ni lagn xamanté
Life Di dem bagni demlenté
Loma def lalay delo
Liguama diox lalaye delo
Ligua mom lalaye delo
Lima mom ngamay delo
Liguama lepp ngamay delo
Fek Yagui né si mane dougn Meuss bayanté
Meuss ngama togne mane tam Kaye niou balanté
Tankamlouwoma motax niou falanté
Niit niitay garabam kaye niou fadjanté
Xam di wananté dagn war wolonté
Sougn doul loranté kene dou xex
Bagne Kouma trompé tax maye doranté
Lou du talion rek tiow li diex
Li djaral Nama lepp lim la diaral
(Li djaral Nama lepp lim la diaral)
Lima def ligua def moko waral
(Lima def ligua def moko waral)
Kou toudoul yalla la meunteu ragal
(Kou toudoul God la meunteu ragal)
Ligua yorr maguek mom Niggah dalal
War fassou narou goor diko dawal
Kone soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Anhhhh
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.




Def Kate bou magg kaye niou defanté
Gueneul fi nieuw niou defanté
Dealer kaye niou teganté
Do wax Deug Kaye niou fenanté
Charlatan Kaye niou naxanté
Dagua beuri wax Kaye weranté
Boucher nga Kaye niou daganté
Sou deugeuré rej niou goranté
Menuisièr Kaye niou dadjanté
Rap bi day ladj niou rabonté
Guewel nga Kaye niou taganté
Mais mane vrai histoire bi laye raconter
Commerçant kaye niou diayanté
Business leu amoul mayanté
Maçon Kaye niou tabaxanté gazer souf ak ciment di raxanté
Loma def lalaye delo
Liguama diox lalate delo
Ligua mom lalaye delo
Limala lebb lalay delo
Kone doma desse Dara lepp ngamay delo
Limala diox ngamay delo
Lima mom ngamay delo
Liguama lebb ngamay delo for real
Iow dagua tangue Kone Kaye niou lakanté
On fait du sale kaye niou saguanté
Insolent kaye niou saguanté
Dangma beug mourro kone laye niou sanganté
Dagua rew dama neup kaye niou yaranté
Do togn di diegalou kone dougn balanté
Leboula amnga fiit Kaye niou napantè
Tepiii sa ouy après tafanté
Li djaral Nama lepp lim la diaral
(Li djaral Nama lepp lim la diaral)
Lima def ligua def moko waral
(Lima def ligua def moko waral)
Kou toudoul yalla la meunteu ragal
(Kou toudoul God la meunteu ragal)
Ligua yorr maguek mom Niggah dalal
War fassou narou goor diko dawal
Kone soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Anhhhh
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Boloy dolé nagn dieguenté
Give me your hand té bagne hainaté
Xamb tal bi mou geuneu takeu ndax nioune sougn birr nio meune faayanté
Damla nex kaye nga waxmako
Niou togg waxtane geune meune xamanté
Aye Borom bax ni lagn xamanté
Life Di dem bagni demlenté
Loma def lalay delo
Liguama diox lalaye delo
Ligua mom lalaye delo
Lima mom ngamay delo
Liguama lepp ngamay delo
Fek Yagui né si mane dougn Meuss bayanté
Meuss ngama togne mane tam Kaye niou balanté
Tankamlouwoma motax niou falanté
Niit niitay garabam kaye niou fadjanté
Xam di wananté dagn war wolonté
Sougn doul loranté kene dou xex
Bagne Kouma trompé tax maye doranté
Lou du talion rek tiow li diex
Li djaral Nama lepp lim la diaral
(Li djaral Nama lepp lim la diaral)
Lima def ligua def moko waral
(Lima def ligua def moko waral)
Kou toudoul yalla la meunteu ragal
(Kou toudoul God la meunteu ragal)
Ligua yorr maguek mom Niggah dalal
War fassou narou goor diko dawal
Kone soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Anhhhh
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
Soulako diaralé diaral namako
(soulako diaraleeeeee)
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Momar Ndiaye
Copyright: Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Back to: Gun Mor

Tags:
No tags yet