Eh yaw Kaye si Gun
Boudé rap rek leu kaye si gun
You bone yi warngene ko baye pour guiss kou aye il faut que nga kaye si Gun
Féyyy ni tieli Fly ni djeune
Dofi guiss bene faille ame fitou fight job guéné jaye Lou geune
1er couplet
44 Straight outta thiaroye gare
4mil 4cent 4 technique ak flow showbizz nema carokarrrr
Douma kouy khew dama fi nek ba xew nema kagn deme
War fassou meune daw ba dem nema fane ngay yeme
Boy mouy fi di féé ak feulei jsuis fort
Toujours et je rap tout doux
Douma fokate boulma wo si fooo
Boulma wo si thiow balamalay
Touhh???? touh????
Anhhh
J'ai investis de la force jsuis invincible
Pour vos connaisseur paraît-il que jsuis trop sophistiqué heiheinnnn Si
Dougeul ayyy guéné lettres aye chiffres
Strictement nessbiiiii
Gnong may dorr ay code phare beug meu dougou lene mane doumalene kiiiiiiiiii!
Magui légaaa, avec mes gars nexoulene ma honestly
Meunolene di def genre Woutek mane yémé lole ande ak modesty
Refrain
Eyyyyy Kaye si Gun
Boudé rap rek leu kaye si gun
You bone yi warngene ko baye pour guiss kou aye il faut que nga kaye si Gun
Féyyy ni tieli Fly ni djeune
Dofi guiss bene faille ame fitou fight job guéné jaye Lou geune
2ème couplet
Douma def comme Ki wala comme Ké
Je suis iconoclaste
Rap di déf ay ref
Maye def Guetto boy yeup done crack
Reew mi laye yenou pour l'éternité mane leu maye Atlas
Beuri melokane melni kakatar par ce que maguek Llas
Doto meuneu bagne
Yeksina doto meune deme
Wate lene ndel sopi sene sytem
Teuldjouléne F*ck lene sur scènes
Dama dead mak pop smoke nioy game
One man army f*ck aye Gang
Souma foot Madrid laye play
Camavinga mane Maye dil Rennes
(Kaye si geune)
Mango nior neu Mor season
Saf na sapeu roff si djeune
Yene sene kaw ni bicycle
Jongler lene ni bale di teule
Vif la rombe daw di xeulle
Boudé fene leu baye fi gun
Nimay xolé lene titeul
(Pour ame astuces bi)
Refrain
Eyyyyy Kaye si Gun
Boudé rap rek leu kaye si gun
You bone yi warngene ko baye pour guiss kou aye il faut que nga kaye si Gun
Féyyy ni tieli Fly ni djeune
Dofi guiss bene faille ame fitou fight job guéné jaye Lou geune