Magg si kaw gni né si kaw
Tok ni tiéleu indi thiow
Armé Gun bi brakeuzeup
(Prrrrrrrrrr)
Gun dou xir leleni thiaw
Magui feep kene dou raw
Taye la yaram yeup di daw
Magui si yacht bi gnogui yott
Né si gall yi rek di diow
Né si gall yi rek di diow
Geuwma kene si game bi meune ma dapp
Internet bi lagni né di thiow
Koni diak beutak beut dou wax
Xeuw bi Awma bobou diot
Cours yé beuri boulma ladj loutax
Guene amphi dougou studio di job
Stock sons yi dafa wara diar
Li denthiou Magg la dama yagg Ji xaar
Soxlawouma kene kouma goblé
(Sa mc mogui wone si Sama goblé
Clairon nako douma goukh di goukhtat)
Gnéwouma gni tandou def Lou viral
Après thiow Li faye niou moudjou thiolé
Buzz bi disparaître nieup thiolé
Gni done Lang maguiléni ziaaaaar
Thiow Li thiow Li mane la I'm di One
Hey hey hey heeeeeee
Lima dianguoul lalene né di wane
Hey hey hey heeeeeee
Avenirou rap bi lagn ma yene
Boyi defagouniou louma yeme
Sama tietou wé la nieup yeme
Hey hey hey heeeeeee
Thiow Li thiow Li mane la I'm di One yeeeeeeehhhh
Lima dianguoul lalene né di wane
Hey hey hey heeeeeee
Avenirou rap bi lagn ma yene
Grand yi defatouniou louma yeme
Sama tietou wé la nieup yeme
Hey hey hey heeeeeee
Sama tietou wé la nieup yeme
Ay moleculou rappeur lagn maye boleel
Grand yi defatouniou louma yéme
Dagni bayi bama bayi bayilolene
Boy defagouniou louma yeme
Dagni chômée fokma baayilolene
Gnogui dadjou fokma adjilolene
Lucidité diox lene lougnou fowé
(Kholaa)
Magui diap fima diap bam deugeur keuth nieup dima bayi xel
Diebeulou Sama bopp seugn bi Mor Diarra dong laye diayantel
Paré pour tok di encaisser lima dox
Wérou di paqueté lima diot
Kene si yene atanoul lign ma diox
(Niogui thiow mais gni thiow nelene)
Thiow Li thiow Li mane la I'm di One
Hey hey hey heeeeeee
Lima dianguoul lalene né di wane
Hey hey hey heeeeeee
Avenirou rap bi lagn ma yene
Boyi defagouniou louma yeme
Sama tietou wé la nieup yeme
Hey hey hey heeeeeee
Thiow Li thiow Li mane la I'm di One yeeeeeeehhhh
Lima dianguoul lalene né di wane
Hey hey hey heeeeeee
Avenirou rap bi lagn ma yene
Grand yi defatouniou louma yeme
Sama tietou wé la nieup yeme
Hey hey hey heeeeeee