Back to Top

Gun Mor - Le Bien Et Le Mal [Original] Lyrics

Official

Anhhh
(Yo the good, the bad, le bien, le mal
Li baax ak li bonn, si miim reew la fék baax
Yoooo the good, the bad, le bien, le mal

Li baax ak li bonn, Senegal la fék baax

Li baax ak li bonn, si miim reew la fék baax)
Baaxa ngi ame batay c'est que bonn dafko geuneu feuss
Bonn Daf di diourom béne fane baax nek béne Bés
Kéne wolotoul kéne motax kene bougoul koula seuss
Do meuseu xamni baax diekoul so tamé di deglou teuss
Beug lou yomba tax niou tayala djeul yonn bou baax
Djoudou rek Bonn beug tekki té dougn dioug fign né faax
Djoub yomboul goney yi né deukoum taax
Bouki bou yoré allumette alleu bi yeup laye sopi daumou taal
Bonn meunteu wessou djoudou si guelam nameu si mbam
Comme Domou elimane bou waxtou djouli di fék si bar
Kou baax loum yéné boppam rek laye yéné moromam
Legui nioune nieupeu bokk bone kouné si nioune ame nga si part
Fi kila geuneu yèss legui lagn geuneu diokh thieur
Bo baxé bingay dounde lagn laye mirass seddo saye keur
Djiguen bouy mayé ndawam gayi yaw rek lagni weur
Djeul na si lingay mayé mais est-ce que dîna done sa djeukeur
Done Naffi bonn bonn Lou Farr guiss gnouma geuneu bonn
Ay paa youy teude ak séni dome ay Gars youy teude ak séni bone
École sax baxatoul fala boyi di touxé boon
Nioune téla xam lou nekh motax nioj tela niak diom
Ay nopp youy degg saxoul si sounou bopp motax
Diafé na niou songue mbirr ba djeulé barké
Fi bofi baxé legui gayi def la doff
Gnigua done dimbeuli bingay ame binga niaké dagn la faté (faté)
Deuk bi baax fi legui woratoul (woratoul woratoul)
Diay sa bopp legui bonatoul (bonatoul)
Doundé alale bou léwoul bonatoul (bonatoul)
Reew mi legui wax fi lou baxoul sax bonatoul (bonatoul bonatoul)
Han Deuk bi baax fi legui woratoul (woratoul woratoul)
Donn fi nittou deug doxatoul (doxatoul doxatoul)

Reew mi legui wax fi lou baxoul sax bonatoul
Lou baax lifi niou baax gni bayiwone sax samtougn ko
Niak doylou moy ame louné gagneu di waliyani
Deukou teranga mais fi bo yoroul niou xebb sa dioudou
System béniouy Xiff lo té fi kéne baniatoul ni niani
Souf sé yakou bofii djiwone baax sax bonn ngay gaub
Sougn la tegualone chaisou baax ak bonn si bane ngay togg
Fi baax moy mayé xaliss soirée Wally bayi sa mbok
Fi Bonn moy bala ngay defal keneu defal sa bopp
C'est le monde à l'envers
Paradis en enfer
Dangay nek si niitou deug sax guiss nioulay sani xerr
Legui yémétoul Bo teudé sa djabarou propre frère
Motax woratoul bayi sa djabar ak propre père
Fi do togg bës bo deggoul mbidef bouniou faate
Boy yegui taakeu mais tewoul guél yi di niane sene bate
Kilifeu bila dakeu fene mola dagua waat
Kila geuneu neew lé xam xamala geuneu beuri wax
Fi lignouy lekeu baaxoul
Lignouy nane baxoul
Lignouy setane télék lignouy degg radio baxoul
Deug bou saath di até saath justice bi baxoul
Jummah bou aye sabar inauguré djouli si baxoul
(Gorgi néna)
Baax djegui siraat le aka diafé diegui
(Tégg si)
Mbonn gui dadj na fépp ni gedj niata si sobou rérr si
(Xolal)
Fou niitou Deug taxaw wax fene katay wédi
Boumou goré bignou Borom bi yéwon la djaam bi yéwi
(Anhhh)

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Momar NDiaye
Copyright: Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Back to: Gun Mor

Gun Mor - Le Bien Et Le Mal [Original] Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Gun Mor
Length: 4:11
Written by: Momar NDiaye
[Correct Info]
Tags:
No tags yet