Back to Top

Lii Video (MV)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Karim Diouf
[Correct Info]

Karim Diouf - Lii Lyrics

Li mo ma djakhal, li di li ma titall
Mac gna gui kheutiongourgui
Gouneyi woute kougnou soumi
Li mo ma djakhal, li di li ma titall
Mac gna gui kheutio ngourgui
Gouneyi woute kougnou soumi
Mo toudou Modou, madi Alassane
War na gnou de yaye mana deggo
Moytou khoullo bek khékhbi
Fekhé dal ba mana deggo
Gua djoudo Dakar, mane Casamance
Gualgui dé yaye, sougnou gualla
Li douma djogue di tchi wakh
Mdakh liye name sa gniakh ngua le djeum
Li moma djakhal, li di li ma titall
Bougnou djogue di yonne nganaye Deuk tchi titallaté
Mane dé gni khamé touma lenno
Sénégal rewoum Terangala
Moy li niepp di wakh, sama rëw, sama rêw deukou Terangala
Teranga, sama rëw deugou Teranga...yaw ma lay woo hoho
Teranga, sénégal deukou Teranga
Teranga sénégal sougnou djami rëwla lead vocal
Teranga, sunugal deukou Teranga...yaw ma lay woo hoho
Teranga sama rëw deukou Teranga
Ba Mgor si djogué sama rëw, bamou delsé gnew na setsima
Bamou gnewé tok di ma nétalli, lame ma wakh mane daloul sama khël
Mani lii dou yone ngua tok ni ndame la, djap nit ki, dore ko soumiko
Djeul li mou ame te fok ni ndame la, Bayil di ndamo sa gatché
Ya ko tey, khame gua lama wakh
Mit ki kheuye wouti loumou ame yaye
Boko yeureumoul bakok la mou mome yaw
Rëw mi dafa djoudo nékki wali weume
Khadimou Rassoul la gua Touba
Mame Mawdo Malick ma gua Tivaoune
Limamou laye ya ngua Yoff Laye
Ana djiggen djou mane guor, Aline Sitoé Diatta
Mane dama khamoul louko djar
Mdakh liye rame, sa gniakh gua la djeum
Li mo ma djakhal, li di li ma titall
Bougnou djogué di yorré nganaye Deuk tchi titallaté
Mani gni khamétoumaléno Sénégal réwoume Terangala
Teranga, sama rëw deukou Teranga...yaw ma lay woo hoho
Teranga Sénégal deukou Teranga
Teranga Sénégal sunu djami rëw la - lead vocal
Teranga sunugal deukou Teranga
Senegambia djami la gnouye niane
Teranga, sama rëw deukou Teranga yaw ma lay woo
Teranga senegal deukou Teranga
Teranga sunugal deukou Teranga hoho
Teranga Senegal sunu djami rëw
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Tags:
No tags yet