Back to Top

Métina Video (MV)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Elage Diouf, Karim Diouf
[Correct Info]

Karim Diouf - Métina Lyrics

Wadjour, khol len li gueun tchi mome
Wadjour khol len
Gagni khol len li guen tchi mome
Gagni khol len
Wadjour set len li guen tchi mome
Wadjour khol len
Moytouko, Moytouko (2 x)
Qui dé la gnou guis, qui dé la gnou Xam
Qui dal mo doye sen khol bi té niou may la ko

Bolek di ko san dakh mome sen cheri la
Moytouko, Moytouko
Laye Doudou
Wadjour yi bayi len kou djogué bittime rëw guen mayko sen
Dome ladj len sen dome dakh beuguema
Wadjour yi bayi len fo len dëg bittime rëw taylé fa sen dome
Ladj len sen dome dakh beugueuna
Dakh lolou yaye avenirame la
Yonou meuguël ni la yaya Boye ay tchonola lii métina

Dakh yaw ya ko déf, baga khamé ni bougougnoula warofa
Wane tok yakh sa khaliss
Sa wadjé ko déf amana bo wakhtanone ak gayir dou niak
Yaw kou la wakh liga done khar
Guiss gua bamou soté ni mou mel mbeuguël aye tchonolà
Wayé dafa gueun gua ko wakh lo khaméni ne koul tchi yen
Yenna gui té gatché gui, khawouma follen koy wakhédji
Quiko beugonne sakh demena bayiko
Ana sen djaloré, yaye boye gene ana sen manoré
Guiss guen bamou soté na mou mel, mbeuguel ayetchonola han ha!
Sayouné
Li métina
Yonnou mbeuguel nila, yaya boye aye tchonola
Moytoul ya fi deffone li, yaffi wakhone li, yennafi melone ni dakh la mouye safe
La mouye safe, la mouye safe kako gniam mo ko khame
Li dafa am, dou momou mo ko wara gniam
Adouna day dokh, gnou dokh, wara match andak mome
Te leggui adouna mou mou mel man djakhalnama
Guiss gua dignité dafa bakh tchi nitt
Mome la ane
Yaye Boye Ba len ko ak mome.
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © David Murphy et Cie, Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Tags:
No tags yet