Back to Top

Soukomatoulé Video (MV)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Elage Diouf, Karim Diouf
[Correct Info]

Karim Diouf - Soukomatoulé Lyrics

Mit ko wakh bopame mouni dangue ko beigne yaye
Ya dagno khamoul mome louye nit
Mi mome nittaye guarrabame, garrabame guarrabame mome
Bo amé say nit té deggueutoléne diguani bok yenesayaw
Mbaye bo amone ay nit deggueutolène diguani bok yenesayaw
Dama djekki djekki khaw ma loumay déf mani bok yenesay, yenesay
Yenesay o yenesaye, oh ho yenesay
Mane dé, faugona dou deme, nioune dé foyona dou deme

Mane, hawma wone yakar ni da na gnou ak sifi, nioune dé fogone na da deme
Ablaye Sarr né na mome yitléme yepp Asiko la, lou may deff Asiko la
Lou bonmou ko matoulé dédet li bakhoul Waw Waw
Mome, leg leg mou yoné ndaw gnew lepsima
Mane, leg legui dama djakhlé ni ki mome, louko dal
Sou gnagoul mou sol dalame gnew setsima
Sou gnewé di ma khamal nane ma fonkouloma
Mdeysane
Mane, leg leg dama koy wakh ni mane yaw la ame
Waye mome daf ma tchiy teggal nane yaw wakhate ngua
Soumon gnewoul mou sol dalame gnew setsima
Sou gnewe dima khamal nane foukou loma
Souko matoulé né bakhoul soukomatoulé deded ne bakhoul
Souko matoulé ne Bakhoulili soukomatoulé dede ne bakhoul
Wit ko wakh bopame mouni dangue ko beigne yaye
Te dagno khamoul meme ni nit, nit mome nittay guarrabame, guarrabame
Guarrabame mom mom Ramon
Bo amone say nit te guissatolen digua ni bok yenesayo
Mbaye bo amone ay nit deggueutolen digani bok yenesayon
Refrain
Pape Sou nene mome yittéme yepp Asiko la
Dama rep lou ma dal mani wakh le tchi mane

Beurki demb la yewwu fek mouy def dimba dem
Ma lach nit yi lou khew gnou ni ma yaw dal aksil
Ma ma yaw lo tchi done fekké, fekké mom moma tchi bollé bollé bollé
Bollé, bollé yaw Souko matoule, né bakhoul, souko matoulé ni bakhoul
Boul gniaw fchi Mbolo ni bakhoul
Boul di barry bor déded nibakhoul
Guor dou barry bor ni bakhoul, li bon ko matoulé dede li bakhoul
Dama rep lou ma dal mani wakh len tchi mane

Beruki demb la yewu fek mouy def dimba dem
Ma lach nit yi lou khew, gnou ni ma yawdal akil
Ma ma yaw lo tchi done fekké, fekké mom moma tchi bollé bollé bollé bollé
Bollé yaw, souko matoulé ni bakhoul, souko matoulé, dédéal ni bakhoul
Mani guessoul, mani kholal, mani yeurdoul lolou may gueur
Mani guessoul Mani kholal sénateul ligaye déf worrul
Mani yeurdoul, kholal wa kognebi gnome ni gnou mel
Ah yaw sik ngua yaw, mane de beuguena nit jou same cadome di
Ko tek tchi yone yaw, tchi yone yaw, tchi yone yaw
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Tags:
No tags yet