Back to Top

Këgg Daani - Bëgg Tukki Cover Lyrics

Këgg Daani - Bëgg Tukki Cover Lyrics
Official

Goor-goorlu mor tax-a-doon goor
Jom mooy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Damay toog? Walla damay dem? Xamuma lan lay def
Ni nu tóge di naan sunu ñetteelu kaasu attaaya
Di ñàq ci jantu Senegaal niki safara
Samay xarit yëpp waxunu lu dul tukki
Ci ñoom Senegal du dëkk jaarukaay la rekk
Dëgg la bu ñu waxe 'fii amul liggéey'
Te dëgg kaani la
Wante maam ne na: dom-ju-ñakk xëy
Moo gën dom-ju-ñakk bakkanam
Amuma visa amaguma passport
Lu ma yor moy YAKAAR BU REY
Ñu ne jàmm-a-gën dee
Waaye boo soxla garab jàmm mënu ko fey
Gis na nataalu Elaji mungi amerik
Léegi am na iPhone ak ordinateur bu bees
Wante xaritam bi yeggul sax nikaraguwa
Njabotam di laajte seén domm: fan la nekk ?
Ñu ne jom moy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Waaye ñibbiseek loxo neen moo raw gàcca
Wiri wiri mom jaari ndaari
Waaye ngir jaari ndari fàww nga am saricca
Bëgg naa dem Manchester
Wante su ma tukkee luma fay ameh?
Yonenti Suleeymaan ne na:
Nit gisul njariñ ci kaw suuf Rafet xel fanqul deh
Goor-goorlu moo tax-a-doon goor
Jom mooy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Damay toog? Walla damay dem? Xamuma lan lay def
Tukki Tukki tukki fëgg fëgg fëgg
Dem xol Tugël loolu lañuy bëgg
Original Lyrics. Music by Suno AI. Written distributed by me.
My socials on YT and X are @KëggDanni
Thanks for listening.
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Goor-goorlu mor tax-a-doon goor
Jom mooy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Damay toog? Walla damay dem? Xamuma lan lay def
Ni nu tóge di naan sunu ñetteelu kaasu attaaya
Di ñàq ci jantu Senegaal niki safara
Samay xarit yëpp waxunu lu dul tukki
Ci ñoom Senegal du dëkk jaarukaay la rekk
Dëgg la bu ñu waxe 'fii amul liggéey'
Te dëgg kaani la
Wante maam ne na: dom-ju-ñakk xëy
Moo gën dom-ju-ñakk bakkanam
Amuma visa amaguma passport
Lu ma yor moy YAKAAR BU REY
Ñu ne jàmm-a-gën dee
Waaye boo soxla garab jàmm mënu ko fey
Gis na nataalu Elaji mungi amerik
Léegi am na iPhone ak ordinateur bu bees
Wante xaritam bi yeggul sax nikaraguwa
Njabotam di laajte seén domm: fan la nekk ?
Ñu ne jom moy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Waaye ñibbiseek loxo neen moo raw gàcca
Wiri wiri mom jaari ndaari
Waaye ngir jaari ndari fàww nga am saricca
Bëgg naa dem Manchester
Wante su ma tukkee luma fay ameh?
Yonenti Suleeymaan ne na:
Nit gisul njariñ ci kaw suuf Rafet xel fanqul deh
Goor-goorlu moo tax-a-doon goor
Jom mooy tukki waaye fulla moy ñibbisi
Damay toog? Walla damay dem? Xamuma lan lay def
Tukki Tukki tukki fëgg fëgg fëgg
Dem xol Tugël loolu lañuy bëgg
Original Lyrics. Music by Suno AI. Written distributed by me.
My socials on YT and X are @KëggDanni
Thanks for listening.
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Alex Maclean
Copyright: Lyrics © O/B/O DistroKid

Back to: Këgg Daani

Këgg Daani - Bëgg Tukki Cover Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Këgg Daani
Language: English
Length: 2:38
Written by: Alex Maclean
[Correct Info]
Tags:
No tags yet