Dëgg kaani la, ku ñu ko xëpp nga toxoñu
Dëgg kaani la
Sa xaritu noon sa noon la
Sa xaritu kal, sa kal la
Dëgg kaani la
Sekk siginaar amul bun ci kaw
Jaaw bëgg-a-daw waaye mënul fa dawal!
Dëgg kaani la
Jopp, jopp-a-juba, dem ci toll
Fatte fa jubam, daw dellu
Faal jaga yaram
Dëgg kaani la
Touré mandi moori, lu mu tekki kenn xamul
Dëgg kaani la, ku ñu ko xëpp nga toxoñu
Original Lyrics. Music by Suno AI. Written distributed by me
My socials on YT and X are @KëggDanni
Thanks for listening.