Back to Top

Mgeey - Diine Akk Jamano Lyrics

Mgeey - Diine Akk Jamano Lyrics

DIINE AKK JAMANO

Nekk ci Kanam taxul nga jiite
Nitt aka lëndëm mais bëri leer moy tax mu nite
Ñakk yar sa doom moy indi rèew akk ñakk yite
Kepp nu baayi julli dem restau reeri ammu loo diine
Mën nga fi sax sans nekk verre de terre
Jigeen bu takk fer deffu ko dame de fer
Ñakk loxo tere wu ñu bras de fer
Ñi dee ci geej bu ñu saññoon deewee sen bras de mer
Bul jog ci sakku xam-xam
Yalla'ay tann am-am akk ñi wara am tan
Wacceel sa bopp ndax jigeen bu rëy deffu la grande dame
Gis naa jigeen yu rèew yu bëgg nekk sage femme

Eyo

Kon jamano bi toppul diine
Gis naa diine yu jamano xaaj
Est-ce que jamano bi laaj na diine
Wante diine moy tòntu ci li jamano laaj
Eyo

Kon jamano bi toppul diine
Gis naa diine yu jamano xaaj
Est-ce que jamano bi laaj na diine
Wante diine moy tòntu ci li jamano laaj
Eyo

Xalaatal li ngay wax bala ngay wax say xalaat
Nee naa la weer say yëre taxul nga gis say fautes (fòot)
Ñi gën a nakk ci yoonu tedd moy ñiy yeewoo ci baraque
Uttil ligeey ndax defar dënn mënul feesal sa coffre
Fii da ngay muñ ba mujj gedd wax bu ñaaw moo teggine
Sëriñ woote appel wante taalibe yey décliner
Daw ci ginaaw salaire akk ay primes ba mujj déprimer
Te ñi nga yagg tallal loxo ñoo lay jeem a piétiner
Yo
Jamm comme garab bu fepp lay sax
Yeah
Xaalis du oos mais fepp lay yaqq
Yeah
Fétiche du tëye sama tour
Mëwti du jël bakkan bu nitt ammoon roue de secour
Eyo
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

DIINE AKK JAMANO

Nekk ci Kanam taxul nga jiite
Nitt aka lëndëm mais bëri leer moy tax mu nite
Ñakk yar sa doom moy indi rèew akk ñakk yite
Kepp nu baayi julli dem restau reeri ammu loo diine
Mën nga fi sax sans nekk verre de terre
Jigeen bu takk fer deffu ko dame de fer
Ñakk loxo tere wu ñu bras de fer
Ñi dee ci geej bu ñu saññoon deewee sen bras de mer
Bul jog ci sakku xam-xam
Yalla'ay tann am-am akk ñi wara am tan
Wacceel sa bopp ndax jigeen bu rëy deffu la grande dame
Gis naa jigeen yu rèew yu bëgg nekk sage femme

Eyo

Kon jamano bi toppul diine
Gis naa diine yu jamano xaaj
Est-ce que jamano bi laaj na diine
Wante diine moy tòntu ci li jamano laaj
Eyo

Kon jamano bi toppul diine
Gis naa diine yu jamano xaaj
Est-ce que jamano bi laaj na diine
Wante diine moy tòntu ci li jamano laaj
Eyo

Xalaatal li ngay wax bala ngay wax say xalaat
Nee naa la weer say yëre taxul nga gis say fautes (fòot)
Ñi gën a nakk ci yoonu tedd moy ñiy yeewoo ci baraque
Uttil ligeey ndax defar dënn mënul feesal sa coffre
Fii da ngay muñ ba mujj gedd wax bu ñaaw moo teggine
Sëriñ woote appel wante taalibe yey décliner
Daw ci ginaaw salaire akk ay primes ba mujj déprimer
Te ñi nga yagg tallal loxo ñoo lay jeem a piétiner
Yo
Jamm comme garab bu fepp lay sax
Yeah
Xaalis du oos mais fepp lay yaqq
Yeah
Fétiche du tëye sama tour
Mëwti du jël bakkan bu nitt ammoon roue de secour
Eyo
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, MOMAR GUEYE NGOM
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: Mgeey

Mgeey - Diine Akk Jamano Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Mgeey
Language: English
Length: 2:15
Written by: ABDOULAYE WONE, MOMAR GUEYE NGOM
[Correct Info]
Tags:
No tags yet