Back to Top

Dina Ñëw Video (MV)

Performed By: Mgeey
Language: English
Length: 3:02
Written by: ABDOULAYE WONE, MOMAR GUEYE NGOM
[Correct Info]

Mgeey - Dina Ñëw Lyrics

Refrain

Li ma dundu laa nekk di way
Talla tu ma gacce gi
Doy lu li ma Yalla ji may ay waay ti
Coono bi dajj fay Ay waay
Tëwa daw utti barke baay rekk a tax duñu toog yeah
Tekki sama Mind xam ni bës dina ñëw
Gëm ni bës dina mool yeah yeah
Japp tëwa daw Mère bi mi ngi ñaan di ma aar ci noon ye ñoo ma dolli jom ñoo ma def li ma doon
Looloo tax ma di sonn yeah suba ba ngoon yaa
Oh Mind
Fight Allright
Ñaffe di xeex All Nights
Coono bu nekk ñu daj ko yeewul naaj na
Tolluwaay ñeme lu meti waay
Xalaat yi fees ci sama mind
Baññu ma jog pour faj ko coono Life la

Couplet

Yeah bës dina ñëw
Mama bës dina ñëw
Ma dellusi lima fi baayi moo di am sa ngërëm
Tubaab bi pax bim ma gasal du ma ci mës tëmbël
Ligeey akk tëxlu gëmm
Te Le fruit de mon labeur sa wet man laa ko bëgg jëmbët
Da may taaw xam lima war ligeey tanqamlu details
Te faw ma moytu akk samay tank trace yi may baayi
Donte yeene naa samay rakk chemin bu gën yòmb
Celui qui m'etait destiné ñu jël hauts yi ma yenu bas yi
Sori sa family tumrànke du ko gën tar
Rapidement kon faw mili yi dajjaloo ma mën dëppaat
Bi may tukki taggoo wu ma man dong ma yenu bagaas yi
Ma am te xoffu ma ñu teg si sama put bi jaasi
On god li ma gënël du tukki
Gisu ma luy tax nit ba ginaaw reewam bu doonul wuti
Ndax ku wacc sa and si bo demaat gis ko'og boroom
Gisoo ni decouverte states deful kaana Christophe Colomb
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Refrain

Li ma dundu laa nekk di way
Talla tu ma gacce gi
Doy lu li ma Yalla ji may ay waay ti
Coono bi dajj fay Ay waay
Tëwa daw utti barke baay rekk a tax duñu toog yeah
Tekki sama Mind xam ni bës dina ñëw
Gëm ni bës dina mool yeah yeah
Japp tëwa daw Mère bi mi ngi ñaan di ma aar ci noon ye ñoo ma dolli jom ñoo ma def li ma doon
Looloo tax ma di sonn yeah suba ba ngoon yaa
Oh Mind
Fight Allright
Ñaffe di xeex All Nights
Coono bu nekk ñu daj ko yeewul naaj na
Tolluwaay ñeme lu meti waay
Xalaat yi fees ci sama mind
Baññu ma jog pour faj ko coono Life la

Couplet

Yeah bës dina ñëw
Mama bës dina ñëw
Ma dellusi lima fi baayi moo di am sa ngërëm
Tubaab bi pax bim ma gasal du ma ci mës tëmbël
Ligeey akk tëxlu gëmm
Te Le fruit de mon labeur sa wet man laa ko bëgg jëmbët
Da may taaw xam lima war ligeey tanqamlu details
Te faw ma moytu akk samay tank trace yi may baayi
Donte yeene naa samay rakk chemin bu gën yòmb
Celui qui m'etait destiné ñu jël hauts yi ma yenu bas yi
Sori sa family tumrànke du ko gën tar
Rapidement kon faw mili yi dajjaloo ma mën dëppaat
Bi may tukki taggoo wu ma man dong ma yenu bagaas yi
Ma am te xoffu ma ñu teg si sama put bi jaasi
On god li ma gënël du tukki
Gisu ma luy tax nit ba ginaaw reewam bu doonul wuti
Ndax ku wacc sa and si bo demaat gis ko'og boroom
Gisoo ni decouverte states deful kaana Christophe Colomb
[ Correct these Lyrics ]
Writer: ABDOULAYE WONE, MOMAR GUEYE NGOM
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: Mgeey

Tags:
No tags yet