Back to Top

Mgeey - Sant Lyrics



Mgeey - Sant Lyrics




Sant

Refrain

Yenn saay ma weet ba soxla naaj su guddee
Weet'ag asamaan si di ñaan
Baññu ma reer mais bëggu ma di mujjee
Sama nafsu laay jeema daan
Yallaa ñu sakk ñooy jaamam
( ouuu heiii ouu heiii )
Ñoo ngi dolli sant du ñu doyal
Ci mbaaxam
( ouuu heiii ouu heiii )
Baaxee na ñu wer teg si ker akk naajam
( ouuu heiii ouu heiii )
May ñu wayjur yu ñu dëkkee di ñaanal
( ouuu heiii ouu heiii )


Yallaa ñu sakk ñooy jaamam du deñ
Yallaa di maye moy nangoo ka xañ
Yallaa di buur
Yallaa di Kun
May ñu gudd fan kattan bu wëy
Faj aajo yi tem aar njaboot ji
Sakku di xam xaar wërsëg ye
Bakku ci ndam yaa ñu may yokkute
Mbëggeel nga ñu won te say wax a ñuy yee yeah yeah
Sukk ñaan ci su ñu boroom yeah
Moo di waaja ammul moroom
Jaral nga ñu xëy sòng naaj bi taw akk ngelaw
Baax di ci wëy di la jaamu bañ a nelaw
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


English

Sant

Refrain

Yenn saay ma weet ba soxla naaj su guddee
Weet'ag asamaan si di ñaan
Baññu ma reer mais bëggu ma di mujjee
Sama nafsu laay jeema daan
Yallaa ñu sakk ñooy jaamam
( ouuu heiii ouu heiii )
Ñoo ngi dolli sant du ñu doyal
Ci mbaaxam
( ouuu heiii ouu heiii )
Baaxee na ñu wer teg si ker akk naajam
( ouuu heiii ouu heiii )
May ñu wayjur yu ñu dëkkee di ñaanal
( ouuu heiii ouu heiii )


Yallaa ñu sakk ñooy jaamam du deñ
Yallaa di maye moy nangoo ka xañ
Yallaa di buur
Yallaa di Kun
May ñu gudd fan kattan bu wëy
Faj aajo yi tem aar njaboot ji
Sakku di xam xaar wërsëg ye
Bakku ci ndam yaa ñu may yokkute
Mbëggeel nga ñu won te say wax a ñuy yee yeah yeah
Sukk ñaan ci su ñu boroom yeah
Moo di waaja ammul moroom
Jaral nga ñu xëy sòng naaj bi taw akk ngelaw
Baax di ci wëy di la jaamu bañ a nelaw
[ Correct these Lyrics ]
Writer: MOMAR GUEYE NGOM, ABDOULAYE WONE
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: Mgeey



Mgeey - Sant Video
(Show video at the top of the page)


Performed By: Mgeey
Language: English
Length: 2:16
Written by: MOMAR GUEYE NGOM, ABDOULAYE WONE
[Correct Info]
Tags:
No tags yet